48
Q.S Sad (38:48)
وَاذْكُرْ اِسْمٰعِيْلَ وَالْيَسَعَ وَذَا الْكِفْلِ ۗوَكُلٌّ مِّنَ الْاَخْيَارِۗ
ważkur ismā‘īla wal-yasa‘a wa żal-kifl(i), wa kullum minal-akhyār(i).
Ak fàttaliku Ismaail, Iliyaas, ak Dulkifli. Ñoom ñépp boole ci nit ñi gëna baax.