Embrasser l'Islam, cliquez ici
Islam Al-Haq: Al-Qur'an ak Hadith
(Islam bu dëgg)



Mbokk - Kisah-kisah dan perumpamaan dalam Al Qur'an Kisah-kisah Al Qur'an Kisah penciptaan manusia Sifat manusia Kelemahan manusia

Njëgël ayat yi :
Limu ayat yi : 40
28
Q.S An Nisa (4:28)

يُرِيْدُ اللّٰهُ اَنْ يُّخَفِّفَ عَنْكُمْ ۚ وَخُلِقَ الْاِنْسَانُ ضَعِيْفًا

yurīdullāhu ay yukhaffifa ‘ankum, wa khuliqal-insānu ḍa‘īfā(n).

Allah dafa bëgga féexal la, ndax nit (nature) dafa néew doole.


30
Q.S Al-Mayda (5:30)

فَطَوَّعَتْ لَهٗ نَفْسُهٗ قَتْلَ اَخِيْهِ فَقَتَلَهٗ فَاَصْبَحَ مِنَ الْخٰسِرِيْنَ

fa ṭawwa‘at lahū nafsuhū qatla akhīhi fa qatalahū fa aṣbaḥa minal-khāsirīn(a).

Kon bëgg-bëgg (Qabil) puus ko mu ray rakkam, ci la (ci dëgg) ray ko, mu nekk kenn ci ñi ñàkk.


134
Q.S Al-An'am (6:134)

اِنَّ مَا تُوْعَدُوْنَ لَاٰتٍۙ وَّمَآ اَنْتُمْ بِمُعْجِزِيْنَ

innamā tū‘adūna la'āt(in), wa mā antum bimu‘jizīn(a).

Dëgg la, lépp lu ñu leen dig dina am, te dungeen ko tere.


143
Q.S Al A'raf (7:143)

وَلَمَّا جَاۤءَ مُوْسٰى لِمِيْقَاتِنَا وَكَلَّمَهٗ رَبُّهٗۙ قَالَ رَبِّ اَرِنِيْٓ اَنْظُرْ اِلَيْكَۗ قَالَ لَنْ تَرٰىنِيْ وَلٰكِنِ انْظُرْ اِلَى الْجَبَلِ فَاِنِ اسْتَقَرَّ مَكَانَهٗ فَسَوْفَ تَرٰىنِيْۚ فَلَمَّا تَجَلّٰى رَبُّهٗ لِلْجَبَلِ جَعَلَهٗ دَكًّا وَّخَرَّ مُوْسٰى صَعِقًاۚ فَلَمَّآ اَفَاقَ قَالَ سُبْحٰنَكَ تُبْتُ اِلَيْكَ وَاَنَا۠ اَوَّلُ الْمُؤْمِنِيْنَ

wa lammā jā'a mūsā limīqātinā wa kallamahū rabbuh(ū), qāla rabbi arinī anẓur ilaik(a), qāla lan tarānī wa lākininẓur ilal-jabali fa inistaqarra makānahū fa saufa tarānī, falammā tajallā rabbuhū lil-jabali ja‘alahū dakkaw wa kharra mūsā ṣa‘iqā(n), falammā afāqa qāla subḥānaka tubtu ilaika wa ana awwalul-mu'minīn(a).

Ba Musaa yegsee ci waxtu wi nu jàppoon, te Boroomam wax ak moom, mu ne: "Yaw sama Boroom, wane ma (sa bopp) ngir ma gis la." (Yàlla) nee na: "Dunga ma gis, waaye xoolal tund wi; bu saxee ca barabam, dinga ma gis". Bi Boroom bi ko wanee tundu wi, mu daanu, Musaa daanu, xëm. Bimu yewwoo ci boppam, mu ni, "Maa ngi lay sargal! Maa ngi wëlbatiku ci yaw ci tuub, te man maay ki njëkka gëm."


59
Q.S Al anfal (8:59)

وَلَا يَحْسَبَنَّ الَّذِيْنَ كَفَرُوْا سَبَقُوْاۗ اِنَّهُمْ لَا يُعْجِزُوْنَ

wa lā yaḥsabannal-lażīna kafarū sabaqū, innahum lā yu‘jizūn(a).

Te bu ñu weddi xalaat ne danañu mucc (ci kàttanug Yàlla). Dëgg la, mënuñoo néewal doole (Yàlla).


2
Q.S At Tawbah (9:2)

فَسِيْحُوْا فِى الْاَرْضِ اَرْبَعَةَ اَشْهُرٍ وَّاعْلَمُوْٓا اَنَّكُمْ غَيْرُ مُعْجِزِى اللّٰهِ ۙوَاَنَّ اللّٰهَ مُخْزِى الْكٰفِرِيْنَ

fasīḥū fil-arḍi arba‘ata asyhuriw wa‘lamū annakum gairu mu‘jizillāh(i), wa anallāha mukhzil-kāfirīn(a).

Kon nag doxleen ci réew mi diirub ñeenti weer te nga xam ne manuleen réeral Yàlla, te Yàlla wàcce na ci kaw ña weddi.


3
Q.S At Tawbah (9:3)

وَاَذَانٌ مِّنَ اللّٰهِ وَرَسُوْلِهٖٓ اِلَى النَّاسِ يَوْمَ الْحَجِّ الْاَكْبَرِ اَنَّ اللّٰهَ بَرِيْۤءٌ مِّنَ الْمُشْرِكِيْنَ ەۙ وَرَسُوْلُهٗ ۗفَاِنْ تُبْتُمْ فَهُوَ خَيْرٌ لَّكُمْۚ وَاِنْ تَوَلَّيْتُمْ فَاعْلَمُوْٓا اَنَّكُمْ غَيْرُ مُعْجِزِى اللّٰهِ ۗوَبَشِّرِ الَّذِيْنَ كَفَرُوْا بِعَذَابٍ اَلِيْمٍۙ

wa ażānum minallāhi wa rasūlihī ilan-nāsi yaumal-ḥajjil akbari annallāha barī'um minal-musyrikīn(a), wa rasūluh(ū), fa in tubtum fa huwa khairul lakum, wa in tawallaitum fa‘lamū annakum gairu mu‘jizillāh(i), wa basysyiril-lażīna kafarū bi‘ażābin alīm(in).

Ak yëgle bu jóge ci Yàlla ak Yonentam ci nit ñi ci bis bi ñuy hajj mu gën a mag, ne Yàlla ak Yonentam tàggoo nañu ak wërsëg yi. Bu ko defee soo tuubee da ngay gën ci yaw, te soo ko dëddoo, xam ne doo man a gàllankoor Yàlla. Te yégal ña weddi ab mbugal mu metti.


25
Q.S At Tawbah (9:25)

لَقَدْ نَصَرَكُمُ اللّٰهُ فِيْ مَوَاطِنَ كَثِيْرَةٍۙ وَّيَوْمَ حُنَيْنٍۙ اِذْ اَعْجَبَتْكُمْ كَثْرَتُكُمْ فَلَمْ تُغْنِ عَنْكُمْ شَيْـًٔا وَّضَاقَتْ عَلَيْكُمُ الْاَرْضُ بِمَا رَحُبَتْ ثُمَّ وَلَّيْتُمْ مُّدْبِرِيْنَۚ

laqad naṣarakumullāhu fī mawāṭina kaṡīrah(tin), wa yauma ḥunain(in), iż a‘jabatkum kaṡratukum falam tugni ‘ankum syai'aw wa ḍāqat ‘alaikumul-arḍu bimā raḥubat ṡumma wallaitum mudbirīn(a).

Dëgg la, Yàlla jàppale na leen (gëmkat yi) ci tooli xare yu bari, ak (fatteel) xarab Hunain, bi seen limu nit ñi gëna réyloo leen, waaye (limu bari googu) amul lenn lu leen di amal njariñ, te suuf su yaatu gi dafa melni lu xat, ngeen dellu ginaaw, daw ci xol bu neexul.


24
Q.S Yunus (10:24)

اِنَّمَا مَثَلُ الْحَيٰوةِ الدُّنْيَا كَمَاۤءٍ اَنْزَلْنٰهُ مِنَ السَّمَاۤءِ فَاخْتَلَطَ بِهٖ نَبَاتُ الْاَرْضِ مِمَّا يَأْكُلُ النَّاسُ وَالْاَنْعَامُ ۗحَتّٰٓى اِذَآ اَخَذَتِ الْاَرْضُ زُخْرُفَهَا وَازَّيَّنَتْ وَظَنَّ اَهْلُهَآ اَنَّهُمْ قٰدِرُوْنَ عَلَيْهَآ اَتٰىهَآ اَمْرُنَا لَيْلًا اَوْ نَهَارًا فَجَعَلْنٰهَا حَصِيْدًا كَاَنْ لَّمْ تَغْنَ بِالْاَمْسِۗ كَذٰلِكَ نُفَصِّلُ الْاٰيٰتِ لِقَوْمٍ يَّتَفَكَّرُوْنَ

innamā maṡalul-ḥayātid-dun-yā kamā'in anzalnāhu minas-samā'i fakhtalaṭa bihī nabātul-arḍi mimmā ya'kulun-nāsu wal-an‘ām(u), ḥattā iżā akhażatil-arḍu zukhrufahā wazzayyanat wa ẓanna ahluhā annahum qādirūna ‘alaihā, atāhā amrunā lailan au nahāran fa ja‘alnāhā ḥaṣīdan ka'allam tagna bil-ams(i), każālika nufaṣṣilul-āyāti liqaumiy yatafakkarūn(a).

Dëgg la, misaalu dundu àdduna bi dafa melni ndox (taw) bi nu wàcce ci asamaan si, ci noonu la garabi suuf si di màgg bu baax (ndax ndox mi), ci ñoom nit ñi ak baayima yi dañu leen di lekk. Ba suuf si mat sëkk taaram, te rafet, te boroomam jàpp ni dina ñu ko jël (góob meññeef yi), sunu yar dina ñëw ci moom ci guddi wala ci bëccëg, suko defee nu def ko (gàñcax gi) ni gàñcax guñu daan, melni daa musa màgg. Noonu la Nuy faraltee firnde yi (Sunu kàttan) ñiy xalaat.


53
Q.S Yunus (10:53)

۞ وَيَسْتَنْۢبِـُٔوْنَكَ اَحَقٌّ هُوَ ۗ قُلْ اِيْ وَرَبِّيْٓ اِنَّهٗ لَحَقٌّ ۗوَمَآ اَنْتُمْ بِمُعْجِزِيْنَ ࣖ

wa yastambi'ūnaka aḥaqqun huw(a), qul ī wa rabbī innahū laḥaqq(un), wa mā antum bimu‘jizīn(a).

Te dinañu la laaj ne: "Ndax dëgg la?" Neel : “Waaw, ci sama Boroom dëgg la, te dungeen man a dellu ginnaaw”.


20
Q.S Kànseer (11:20)

اُولٰۤىِٕكَ لَمْ يَكُوْنُوْا مُعْجِزِيْنَ فِى الْاَرْضِ وَمَا كَانَ لَهُمْ مِّنْ دُوْنِ اللّٰهِ مِنْ اَوْلِيَاۤءَ ۘ يُضٰعَفُ لَهُمُ الْعَذَابُ ۗمَا كَانُوْا يَسْتَطِيْعُوْنَ السَّمْعَ وَمَا كَانُوْا يُبْصِرُوْنَ

ulā'ika lam yakūnū mu‘jizīna fil-arḍi wa mā kāna lahum min dūnillāhi min auliyā'(a), yuḍā‘afu lahumul-‘ażāb(u), mā kānū yastaṭī‘ūnas-sam‘a wa mā kānū yubṣirūn(a).

Duñu mën a dàq (mbugëlu Yàlla) ci kaw suuf, te duñu am kenn ku leen di dimbali ku dul Yàlla. Dinañu leen mbugal ñaari yoon. Ñooñu duñu mën a dégg (dëgg) te duñu ko mën a gis.


33
Q.S Kànseer (11:33)

قَالَ اِنَّمَا يَأْتِيْكُمْ بِهِ اللّٰهُ اِنْ شَاۤءَ وَمَآ اَنْتُمْ بِمُعْجِزِيْنَ

qāla innamā ya'tīkum bihillāhu in syā'a wa mā antum bimu‘jizīn(a).

Mu (Nóohin) ne leen: “Yàlla rekk moo leen di teg mbugal su ko soobee, te dungeen ci mucc.


57
Q.S Kànseer (11:57)

فَاِنْ تَوَلَّوْا فَقَدْ اَبْلَغْتُكُمْ مَّآ اُرْسِلْتُ بِهٖٓ اِلَيْكُمْ ۗوَيَسْتَخْلِفُ رَبِّيْ قَوْمًا غَيْرَكُمْۗ وَلَا تَضُرُّوْنَهٗ شَيْـًٔا ۗاِنَّ رَبِّيْ عَلٰى كُلِّ شَيْءٍ حَفِيْظٌ

fa in tawallau faqad ablagtukum mā ursiltu bihī ilaikum, wa yastakhlifu rabbī qauman gairakum, wa lā taḍurrūnahū syai'ā(n), inna rabbī ‘alā kulli syai'in ḥafīẓ(un).

Waaye su ngeen dëddoo, xamal naa leen li ñu ma yónnee ci yéen muy ndaw. Te sama Boroom dana leen wuutale ak weneen xeet, te dungeen ko lor genn tuuti. Dëgg la, sama Boroom mooy wattu lépp.”


11
Q.S Ar-Ra'd (13:11)

لَهٗ مُعَقِّبٰتٌ مِّنْۢ بَيْنِ يَدَيْهِ وَمِنْ خَلْفِهٖ يَحْفَظُوْنَهٗ مِنْ اَمْرِ اللّٰهِ ۗاِنَّ اللّٰهَ لَا يُغَيِّرُ مَا بِقَوْمٍ حَتّٰى يُغَيِّرُوْا مَا بِاَنْفُسِهِمْۗ وَاِذَآ اَرَادَ اللّٰهُ بِقَوْمٍ سُوْۤءًا فَلَا مَرَدَّ لَهٗ ۚوَمَا لَهُمْ مِّنْ دُوْنِهٖ مِنْ وَّالٍ

lahū mu‘aqqibātum mim baini yadaihi wa min khalfihī yaḥfaẓūnahū min amrillāh(i), innallāha lā yugayyiru mā biqaumin ḥattā yugayyirū mā bi'anfusihim, wa iżā arādallāhu biqaumin sū'an falā maradda lah(ū), wa mā lahum min dūnihī miw wāl(in).

Ngir moom (nit) amna malaaka yu koy wottu ci kanamam ak ci ginaawam. Dañu koy war ci ndigëlul Yàlla. Ca dëgg-dëgg, Yàlla du soppi nekkinu aw askan ba keroog mu soppilu seen nekkin. Te su Yàlla bëggee lu bon ci aw askan, amul kenn ku ko mana dàq, te kenn du leen di aar ku dul Moom.


46
Q.S An-Nahl (16:46)

اَوْ يَأْخُذَهُمْ فِيْ تَقَلُّبِهِمْ فَمَا هُمْ بِمُعْجِزِيْنَۙ

au ya'khużahum fī taqallubihim famā hum bimu‘jizīn(a).

Walla Yàlla dana leen mbugal ci seen tukki ba ñu bañ a dàq (mbugal gi);


41
Q.S Al-Kahf (18:41)

اَوْ يُصْبِحَ مَاۤؤُهَا غَوْرًا فَلَنْ تَسْتَطِيْعَ لَهٗ طَلَبًا

au yuṣbiḥa mā'uhā gauran falan tastaṭī‘a lahū ṭalabā(n).

wala ndoxam daanu ci suuf, doo ko gisati.”


40
Q.S Al anbiya (21:40)

بَلْ تَأْتِيْهِمْ بَغْتَةً فَتَبْهَتُهُمْ فَلَا يَسْتَطِيْعُوْنَ رَدَّهَا وَلَا هُمْ يُنْظَرُوْنَ

bal ta'tīhim bagtatan fa tabhatuhum falā yastaṭī‘ūna raddahā wa lā hum yunẓarūn(a).

Waaye dina leen ñëw ci lu gaaw, ñu tiit bay lox; Kon duñu ko mëna dàq, duñu leen may ñu noppalu.


29
Q.S Al-muminun (23:29)

وَقُلْ رَّبِّ اَنْزِلْنِيْ مُنْزَلًا مُّبٰرَكًا وَّاَنْتَ خَيْرُ الْمُنْزِلِيْنَ

wa qur rabbi anzilnī munzalam mubārakaw wa anta khairul-munzilīn(a).

Te nga ñaan ne: "Yaw sama Boroom, defal ma dëkkal ci barab bu barkeel, te Yaa gën a joxe ab muur".


82
Q.S Al-muminun (23:82)

قَالُوْٓا ءَاِذَا مِتْنَا وَكُنَّا تُرَابًا وَّعِظَامًا ءَاِنَّا لَمَبْعُوْثُوْنَ

qālū a'iżā mitnā wa kunnā turābaw wa ‘iẓāman a'innā lamab‘ūṡūn(a).

Ñu naan: "Ndax dëgg la su nu deewee ba nekk pënd ak yax, dinanu dekki?"


57
Q.S An-Nur (24:57)

لَا تَحْسَبَنَّ الَّذِيْنَ كَفَرُوْا مُعْجِزِيْنَ فِى الْاَرْضِۚ وَمَأْوٰىهُمُ النَّارُۗ وَلَبِئْسَ الْمَصِيْرُ ࣖ

lā taḥsabannal-lażīna kafarū mu‘jizīna fil-arḍ(i), wa ma'wāhumun-nār(u), wa labi'sal-maṣīr(u).

Bul xalaat ne ñi weddi danu mucc ci mbugalu Yàlla ci kaw suuf si ; fekk seen dëkkuwaay mooy jahannama. Ak muy barab bu bon!


19
Q.S Al-furqaan (25:19)

فَقَدْ كَذَّبُوْكُمْ بِمَا تَقُوْلُوْنَۙ فَمَا تَسْتَطِيْعُوْنَ صَرْفًا وَّلَا نَصْرًاۚ وَمَنْ يَّظْلِمْ مِّنْكُمْ نُذِقْهُ عَذَابًا كَبِيْرًا

faqad każżabūkum bimā taqūlūn(a), famā tastaṭī‘ūna ṣarfaw wa lā naṣrā(n), wa may yaẓlim minkum nużiqhu ‘ażāban kabīrā(n).

Kon ñoom weddi nañu li ngeen wax, kon dungeen mana dàq (mbugal gi) mbaa dimbali (yeen bopp), te képp ci yéen ku tooñ, dananu ko teg mbugal mu réy.


22
Q.S Al-'ankabut (29:22)

وَمَآ اَنْتُمْ بِمُعْجِزِيْنَ فِى الْاَرْضِ وَلَا فِى السَّمَاۤءِ ۖوَمَا لَكُمْ مِّنْ دُوْنِ اللّٰهِ مِنْ وَّلِيٍّ وَّلَا نَصِيْرٍ ࣖ

wa mā antum bimu‘jizīna fil-arḍi wa lā fis-samā'(i), wa mā lakum min dūnillāhi miw waliyyiw wa lā naṣīr(in).

Te manuleen a mucc (mbug Yàlla) ci kaw suuf mbaa ci asamaan si, te amuleen ku leen di aar mbaa ku leen di dimbali ku dul Yàlla.


9
Q.S Ar-Rum (30:9)

اَوَلَمْ يَسِيْرُوْا فِى الْاَرْضِ فَيَنْظُرُوْا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الَّذِيْنَ مِنْ قَبْلِهِمْۗ كَانُوْٓا اَشَدَّ مِنْهُمْ قُوَّةً وَّاَثَارُوا الْاَرْضَ وَعَمَرُوْهَآ اَكْثَرَ مِمَّا عَمَرُوْهَا وَجَاۤءَتْهُمْ رُسُلُهُمْ بِالْبَيِّنٰتِۗ فَمَا كَانَ اللّٰهُ لِيَظْلِمَهُمْ وَلٰكِنْ كَانُوْٓا اَنْفُسَهُمْ يَظْلِمُوْنَۗ

awalam yasīrū fil-arḍi fayanẓurū kaifa kāna ‘āqibatul-lażīna min qablihim, kānū asyadda minhum quwwataw wa aṡārul-arḍa wa ‘amarūhā akṡara mimmā ‘amarūhā wa jā'athum rusuluhum bil-bayyināt(i), famā kānallāhu liyaẓlimahum wa lākin kānū anfusahum yaẓlimūn(a).

Ndax dañoo doxantu woon ci kaw suuf si, ba gis naka la muj ña leen jiitu woon ? Ñu gënoon leen am doole (seen bopp) ba noppi ñu bay suuf si, gëna am doole ci li ñu ko am. Te seeni ndaw dikk nañu ci ñoom, indaale leen firnde yu leer. Kon Yàlla toowul leen dara, ñoom ñoo tooñ seen bopp.


54
Q.S Ar-Rum (30:54)

۞ اَللّٰهُ الَّذِيْ خَلَقَكُمْ مِّنْ ضَعْفٍ ثُمَّ جَعَلَ مِنْۢ بَعْدِ ضَعْفٍ قُوَّةً ثُمَّ جَعَلَ مِنْۢ بَعْدِ قُوَّةٍ ضَعْفًا وَّشَيْبَةً ۗيَخْلُقُ مَا يَشَاۤءُۚ وَهُوَ الْعَلِيْمُ الْقَدِيْرُ

allāhul-lażī khalaqakum min ḍa‘fin ṡumma ja‘ala mim ba‘di ḍa‘fin quwwatan ṡumma ja‘ala mim ba‘di quwwatin ḍa‘faw wa syaibah(tan), yakhluqu mā yasyā'(u), wa huwal-‘alīmul-qadīr(u).

Yàlla moo leen sàkk ci néew doole, ba noppi mu def leen doole ginaaw néew doole googu, ba noppi mu def leen ñu néew doole, ñu am kawar gu weex ginaaw doole googu. Mooy sàkk lu ko soob. Te Mooy Ku xam lépp, Kàttan lépp.


43
Q.S Ya-Sin (36:43)

وَاِنْ نَّشَأْ نُغْرِقْهُمْ فَلَا صَرِيْخَ لَهُمْ وَلَاهُمْ يُنْقَذُوْنَۙ

wa in nasya' nugriqhum falā ṣarīkha lahum wa lā hum yunqażūn(a).

Te su Nu ko bëggee, Danu leen di xëcc. Su ko defee kenn du leen dimbali, duñu mucc.


51
Q.S Az-Zumar (39:51)

فَاَصَابَهُمْ سَيِّاٰتُ مَا كَسَبُوْا ۗوَالَّذِيْنَ ظَلَمُوْا مِنْ هٰٓؤُلَاۤءِ سَيُصِيْبُهُمْ سَيِّاٰتُ مَا كَسَبُوْا ۙوَمَا هُمْ بِمُعْجِزِيْنَ

fa'aṣābahum sayyi'ātu mā kasabū, wal-lażīna ẓalamū min hā'ulā'i sayuṣībuhum sayyi'ātu mā kasabū, wa mā hum bimu‘jizīn(a).

Suko defee ñu am lu bon ci li ñu def. Te tooñkat yi ci ñoom danañu sonn ci musiba yu bon yi bawoo ci li ñu def, te duñu mana mucc.


31
Q.S Ash Shura (42:31)

وَمَآ اَنْتُمْ بِمُعْجِزِيْنَ فِى الْاَرْضِۚ وَمَا لَكُمْ مِّنْ دُوْنِ اللّٰهِ مِنْ وَّلِيٍّ وَّلَا نَصِيْرٍ

wa mā antum bimu‘jizīna fil-arḍ(i), wa mā lakum min dūnillāhi miw waliyyiw wa lā naṣīr(in).

Te manuloo mucc (ci mbugalu Yàlla) ci kaw suuf, te amuleen ku leen di aar mbaa ku leen di dimbali ku dul Yàlla.


45
Q.S Adh-Dhariyat (51:45)

فَمَا اسْتَطَاعُوْا مِنْ قِيَامٍ وَّمَا كَانُوْا مُنْتَصِرِيْنَۙ

famastaṭā‘ū min qiyāmiw wa mā kānū muntaṣirīn(a).

Kon mënu ñu woon jog, kenn mënu leen dimbali.


33
Q.S ki am njariñ (55:33)

يٰمَعْشَرَ الْجِنِّ وَالْاِنْسِ اِنِ اسْتَطَعْتُمْ اَنْ تَنْفُذُوْا مِنْ اَقْطَارِ السَّمٰوٰتِ وَالْاَرْضِ فَانْفُذُوْاۗ لَا تَنْفُذُوْنَ اِلَّا بِسُلْطٰنٍۚ

yā ma‘syaral-jinni wal-insi inistaṭa‘tum an tanfużū min aqṭāris-samāwāti wal-arḍi fanfużū, lā tanfużūna illā bisulṭān(in).

Yéen nit ñi ak jinne yi! Sudee mën nga dugg ci catu asamaan yi ak suuf si, duggal. Du ngeen man a dugg lu dul kàttan gu jóge ci Yàlla.


35
Q.S ki am njariñ (55:35)

يُرْسَلُ عَلَيْكُمَا شُوَاظٌ مِّنْ نَّارٍۙ وَّنُحَاسٌ فَلَا تَنْتَصِرَانِۚ

yursalu ‘alaikumā syuwāẓum min nār(in), wa nuḥāsun falā tantaṣirān(i).

Dina ñu wàcce ci yéen (jinne yi ak nit ñi), xal yu tàng ak përëm buy seey, te dungeen ci mëna rëcci.


66
Q.S Waqiha (56:66)

اِنَّا لَمُغْرَمُوْنَۙ

innā lamugramūn(a).

(mu ne) "Dëgg la, nu ñàkk,


67
Q.S Waqiha (56:67)

بَلْ نَحْنُ مَحْرُوْمُوْنَ

bal naḥnu maḥrūmūn(a).

te amu nu dara.»


87
Q.S Waqiha (56:87)

تَرْجِعُوْنَهَآ اِنْ كُنْتُمْ صٰدِقِيْنَ

tarji‘ūnahā in kuntum ṣādiqīn(a).

Ndax doo ko delloo (dundu googu) sudee nit ku jub nga?


4
Q.S Al-mumtahaana (60:4)

قَدْ كَانَتْ لَكُمْ اُسْوَةٌ حَسَنَةٌ فِيْٓ اِبْرٰهِيْمَ وَالَّذِيْنَ مَعَهٗۚ اِذْ قَالُوْا لِقَوْمِهِمْ اِنَّا بُرَءٰۤؤُا مِنْكُمْ وَمِمَّا تَعْبُدُوْنَ مِنْ دُوْنِ اللّٰهِ ۖ كَفَرْنَا بِكُمْ وَبَدَا بَيْنَنَا وَبَيْنَكُمُ الْعَدَاوَةُ وَالْبَغْضَاۤءُ اَبَدًا حَتّٰى تُؤْمِنُوْا بِاللّٰهِ وَحْدَهٗٓ اِلَّا قَوْلَ اِبْرٰهِيْمَ لِاَبِيْهِ لَاَسْتَغْفِرَنَّ لَكَ وَمَآ اَمْلِكُ لَكَ مِنَ اللّٰهِ مِنْ شَيْءٍۗ رَبَّنَا عَلَيْكَ تَوَكَّلْنَا وَاِلَيْكَ اَنَبْنَا وَاِلَيْكَ الْمَصِيْرُ

qad kānat lakum uswatun ḥasanatun fī ibrāhīma wal-lażīna ma‘ah(ū), iż qālū liqaumihim innā bura'ā'u minkum wa mimmā ta‘budūna min dūnillāh(i), kafarnā bikum wa badā bainanā wa bainakumul-‘adāwatu wal-bagḍā'u abadan ḥattā tu'minū billāhi waḥdahū illā qaula ibrāhīma li'abīhi la'astagfiranna laka wa mā amliku laka minallāhi min syai'(in), rabbanā ‘alaika tawakkalnā wa ilaika anabnā wa ilaikal-maṣīr(u).

Dëgg la, amna misaal bu baax ci yéen ci Ibraayma ak ñi ànd ak moom, bi ñu waxee askanam, "Dëgg la, nu mucc ci yéen ak ci li ngeen di jaamu ludul Yàlla, te gëmu nu leen, te noonte ak bañeel feeñ na ci sunu diggante ak yeen ba fàww, ba ngeen gëm Yàlla kese," ludul bi Ibraayma waxee pàppaam, I will butve ask at I lépp dina moytu leen mbugalu Yàlla.» (Ibraayma ne ko) "Yaw sunu Boroom, Yaw lanu wékk, te ca Yaw lanu tuub, ca Yow lanuy dellu".


47
Q.S Hakkah (69:47)

فَمَا مِنْكُمْ مِّنْ اَحَدٍ عَنْهُ حٰجِزِيْنَۙ

famā minkum min aḥadin ‘anhu ḥājizīn(a).

Kon kenn ci yéen mënul woon tere (nu yar ko).


21
Q.S Jinne (72:21)

قُلْ اِنِّيْ لَآ اَمْلِكُ لَكُمْ ضَرًّا وَّلَا رَشَدًا

qul innī lā amliku lakum ḍarraw wa lā rasyadā(n).

Neel (Yaw Muhamed) : "Amuma benn doole buma leen tere defal dara lu bon, wala luma leen di indil benn njariñ."


39
Q.S Al mursalat (77:39)

فَاِنْ كَانَ لَكُمْ كَيْدٌ فَكِيْدُوْنِ

fa'in kāna lakum kaidun fakīdūn(i).

Kon soo amee pexe, defal ko sama kaw.


5
Q.S al-balaad (90:5)

اَيَحْسَبُ اَنْ لَّنْ يَّقْدِرَ عَلَيْهِ اَحَدٌ ۘ

ayaḥsabu allay yaqdira ‘alaihi aḥad(un).

Ndax (nit) dafa yaakaar ne dara amul doole ci moom?


6
Q.S al-balaad (90:6)

يَقُوْلُ اَهْلَكْتُ مَالًا لُّبَدًاۗ

yaqūlu ahlaktu mālal lubadā(n).

Mu tontu, "Dama dugal xaalis bu bari."


7
Q.S al-balaad (90:7)

اَيَحْسَبُ اَنْ لَّمْ يَرَهٗٓ اَحَدٌۗ

ayaḥsabu allam yarahū aḥad(un).

Ndax dafa yaakaar ni dara gisu ko?