ثُمَّ خَلَقْنَا النُّطْفَةَ عَلَقَةً فَخَلَقْنَا الْعَلَقَةَ مُضْغَةً فَخَلَقْنَا الْمُضْغَةَ عِظٰمًا فَكَسَوْنَا الْعِظٰمَ لَحْمًا ثُمَّ اَنْشَأْنٰهُ خَلْقًا اٰخَرَۗ فَتَبَارَكَ اللّٰهُ اَحْسَنُ الْخٰلِقِيْنَۗ
Ṡumma khalaqnan-nuṭfata ‘alaqatan fa khalaqnal-‘alaqata muḍgatan fa khalaqnal-muḍgata ‘iẓāman fa kasaunal-‘iẓāma laḥmā(n), ṡumma ansya'nāhu khalqan ākhar(a), fa tabārakallāhu aḥsanul-khāliqīn(a).
Ba noppi nu def liy kole, ba noppi nu def luy kole, nu defar ko ay yax, ba noppi nu laxas yax yi ci yàpp. Ba noppi, Nu defar ko beneen mbindéef bu am jëmm. Ndam ñeel na Yàlla mi gën a sàkk.
حَتّٰىٓ اِذَآ اَخَذْنَا مُتْرَفِيْهِمْ بِالْعَذَابِ اِذَا هُمْ يَجْـَٔرُوْنَ ۗ
Ḥattā iżā akhażnā mutrafīhim bil-‘ażābi iżā hum yaj'arūn(a).
Ba bu Nuy sonal mbugal ñi am wërsëg ci ñoom, ñuy yuuxu dimbali leen.
خَلَقَ السَّمٰوٰتِ وَالْاَرْضَ بِالْحَقِّ وَصَوَّرَكُمْ فَاَحْسَنَ صُوَرَكُمْۚ وَاِلَيْهِ الْمَصِيْرُ
khalaqas-samāwāti wal-arḍa bil-ḥaqqi wa ṣawwarakum fa'aḥsana ṣuwarakum, wa ilaihil-maṣīr(u).
Moo bind asamaan yi ak suuf si ci dëgg, moo leen jëmmal te mat leen ci, ca Moom ngeen di dellu.
الَّذِيْ خَلَقَكَ فَسَوّٰىكَ فَعَدَلَكَۙ
allażī khalaqaka fa sawwāka fa ‘adalak(a).
Moo leen sàkk, ba noppi matal seen mbindéef, defar leen ci anam wu méngoo.
فِيْٓ اَيِّ صُوْرَةٍ مَّا شَاۤءَ رَكَّبَكَۗ
fī ayyi ṣūratim mā syā'a rakkabak(a).
ci jëmm jumu bëgg, moo leen di defar.
الَّذِيْ خَلَقَ فَسَوّٰىۖ
allażī khalaqa fasawwā.
Moo bind, ba noppi mat (li mu bind).
اَلَمْ نَجْعَلْ لَّهٗ عَيْنَيْنِۙ
alam naj‘al lahū ‘ainain(i).
Xanaa defarunu ko ñaari bët ?
لَقَدْ خَلَقْنَا الْاِنْسَانَ فِيْٓ اَحْسَنِ تَقْوِيْمٍۖ
laqad khalaqnal-insāna fī aḥsani taqwīm(in).
Ca dëgg-dëgg, Nanu bind nit ci melokaan yu gën.