64
Q.S Hijr (15:64)

وَاَتَيْنٰكَ بِالْحَقِّ وَاِنَّا لَصٰدِقُوْنَ

wa ataināka bil-ḥaqqi wa innā laṣādiqūn(a).

Te ñëw nanu ci yéen indaale dëgg te dëggu lanu.